Jour : 9 juillet 2020

Sëriñ Aafiya Buso Xalifa Sëriñ Abdul MutalibSëriñ Aafiya Buso Xalifa Sëriñ Abdul Mutalib
Buso moom Sëriñ Afiya Buso moo fi bàyyikoo. Mu bokkoon ci Waa Daaray-Kaamil yi Sëriñ bi sant ñuy jàng Kaamil bis bu nekk ci Jumaay Tuubaa ji. Ginnaaw tàkkusaan
juillet 9, 2020
khdima
no comments

Diggu-Tabaski !!!Diggu-Tabaski !!!
Tay la séentu bu njëkk ci weeru Diggu-Tabaski !!! —————————————— Dibéer, 29i Korite, Atum 1441H. الأحد، ٢٩ شوّال ١٤٤١ هــ Dimanche, 21 Juin 2020
juillet 9, 2020
khdima
no comments