Buso moom Sëriñ Afiya Buso moo fi bàyyikoo.

Ginnaaw tàkkusaan lañ koy waajal ca Armel yi ci Jumaa ji, jébbal ko Boroomam ca Baxiiha.
Di sàkku ci ñépp ñu ñaanal ko Yàlla jéggal ko te tàbbal ko Àljana…
——————————————————
Yal na ko Yàlla yërëm te jéggal ko, tàbbal ko ca Àljanay Firdawsi ya, wanale ko ak ay maamam bàrkeb Sëriñ bi…!!!
